1
00:00:08,040 --> 00:00:12,260
EVANGELION 30e anniversaire
FOTO BU AM SOLO

2
00:00:23,230 --> 00:00:26,500
Dalal jàmm!
Defna lu yàgg, yéen ñépp!

3
00:00:26,630 --> 00:00:29,000
Man maay jéggalu asuka langley!

4
00:00:29,300 --> 00:00:33,660
Nanga def, man maay soppe bi
Shikinami asuka langley!

5
00:00:33,880 --> 00:00:35,050
Nu bokk defar...

6
00:00:35,050 --> 00:00:38,320
Asuka langley

7
00:00:39,280 --> 00:00:42,180
Bis boobu mooy bis bi ñuy njëkka ànd nii, wala book?

8
00:00:42,280 --> 00:00:44,680
Dëgg la sunu yoon bu njëkk la, wala ?

9
00:00:44,680 --> 00:00:49,020
Boole ci 29 at a ngi nii may nekkul ci kaw seen bi, kon maa ngi xawa tiit!

10
00:00:49,200 --> 00:00:53,960
Kon, ndax danu bawoo ci univers yu wuute,
dof la nu bokk fi!

11
00:00:54,120 --> 00:00:57,140
Xalaatal loolu mooy njeextalu xew-xewu 30eelu bës bu dellusi, hey?

12
00:00:57,340 --> 00:00:58,760
Xam nga, bëggoon naa wax.

13
00:00:58,860 --> 00:01:00,860
Jaar nga ci lu bari, wala book?

14
00:01:00,960 --> 00:01:03,020
Di doxantu te amul dara,

15
00:01:03,280 --> 00:01:06,380
di tëdd ci plugsuit bu mag bi,

16
00:01:06,660 --> 00:01:08,820
di wax sa yëg-yëg ay at ci ginaaw...

17
00:01:09,240 --> 00:01:12,600
Suma nekkoon sa palaas, damay suul sama bopp te duma musa génn!

18
00:01:12,600 --> 00:01:14,360
Xamnga, loolu lu xoromu la, Soryu.

19
00:01:14,400 --> 00:01:19,040
Bayyi Shinji mu xool lépp mën na nekk lu ruslu itam!

20
00:01:19,080 --> 00:01:21,430
Ak li xewoon ci ganaw...
Suma nekkoon man,

21
00:01:21,430 --> 00:01:25,320
Dama doon daw te amul yéere dem ci
Minus-Univers ci njàqare.

22
00:01:25,440 --> 00:01:27,030
Loolu daf ma fàttali.

23
00:01:27,160 --> 00:01:32,260
Malaaka jël ko daal di koy puus
ci Unit-13 war na nekk lu neex, itam!

24
00:01:32,420 --> 00:01:35,400
Oh, waaye mënul sax méngoo ak li nga jaar!

25
00:01:35,620 --> 00:01:40,820
Danga amoon ab jafe-jafe xel bu mat sëkk,
ak MPEs lekk nañu ko ci Unit-02!

26
00:01:42,430 --> 00:01:44,960
Dunu dem fenn...

27
00:01:45,130 --> 00:01:49,320
Suma ci xalaatee bu baax,
Saa yu nekk damay def benn rôle bi.

28
00:01:49,500 --> 00:01:52,600
Doyna xaat!
Dafa jot nu am njeexte lu neex.

29
00:01:52,760 --> 00:01:56,660
Leegi, noo ngi wax.
Yaw ci ñépp yelloo nga lu gëna baax.

30
00:01:56,730 --> 00:02:00,200
Jub?!
Man... bëgg naa féexal sama xol!

31
00:02:00,330 --> 00:02:01,060
Loolu rekk la!

32
00:02:01,460 --> 00:02:05,600
Ci sama kalendriye, sama njeexte mën na neex Shinji dof bi,

33
00:02:05,730 --> 00:02:07,160
waaye du man!

34
00:02:07,560 --> 00:02:10,380
Dama wara dem ci àddunaam bu dof bi,
ak luma ci am?!

35
00:02:10,380 --> 00:02:13,060
Dañu ma xëcc, loolu mooy!
Loolu lu soof la!

36
00:02:13,230 --> 00:02:16,400
Lan moo nekkoon ci loolu
Dafa wara féexal sama xol?!

37
00:02:16,800 --> 00:02:20,020
Waaye amnaa saas
ngir binndaat àdduna bi!

38
00:02:20,030 --> 00:02:24,660
Doonte dafa gàtt, mën naa ko mujjee
nekk protagonist ci jaar-jaar bi!

39
00:02:25,240 --> 00:02:28,800
Doonte dinaa mujjee nekk Shinji bu dof,
Warna am yeneen pexe!

40
00:02:28,900 --> 00:02:32,800
Lu gëna yomba xam
ak yëg-yëg ak mbégte!

41
00:02:33,480 --> 00:02:35,400
Loolu rekk laa bëgg !

42
00:02:35,780 --> 00:02:40,640
Benn mbir rek laa musa bëgg!
te bëgg naa ko lool!

43
00:02:41,430 --> 00:02:42,460
Loolu yéeme na !

44
00:02:42,760 --> 00:02:45,200
Dinaa la jox loolu nga bëgg.

45
00:02:45,400 --> 00:02:47,020
Kan moo la laaj ?! Demal fi!

46
00:02:47,160 --> 00:02:51,300
Mën nga ko defal Shinji.
Lu tax nu bëgga sa ndimbal?

47
00:02:51,500 --> 00:02:54,200
Li nga musa def lu lenn ludul wax lu nëbbu lu neex,

48
00:02:54,440 --> 00:02:57,840
waaye saa yu nekk dafay mujjee ci yàqu-yàqu
lépp lu ëpp loolu!

49
00:02:57,960 --> 00:02:59,660
Warwoo ko xooj...

50
00:03:01,600 --> 00:03:03,430
Asuka

51
00:03:03,500 --> 00:03:05,180
Noppal, Shinji dof bi!

52
00:03:09,000 --> 00:03:10,700
Waaw kay, lan mooy pexe bi?

53
00:03:11,030 --> 00:03:15,840
Ci sama àdduna, amna keneen ku mëna
soppi xew-xew yu wuute ak moom...

54
00:03:16,000 --> 00:03:17,680
Bëgguma yéem benn rookie.

55
00:03:17,860 --> 00:03:21,260
Dinaa jël sama bànneex ak samay loxo!

56
00:03:21,430 --> 00:03:23,500
Loolu lanu bëgg dégg.

57
00:03:23,860 --> 00:03:27,180
Okay, danga wara jël
Ikari Shinji ci anam yii.

58
00:03:27,260 --> 00:03:28,140
Lan nga bëgg?

59
00:03:28,300 --> 00:03:29,960
Dangay tàmbali ci nelaw.

60
00:03:30,230 --> 00:03:32,980
Ginaaw loolu ñu zoom kamera bi,
nga ubbi say bët!

61
00:03:32,980 --> 00:03:36,000
Defal loolu, mbir yi dina ñu soppeeku ci yaw.

62
00:03:36,180 --> 00:03:37,100
Oh, xamnaa ko!

63
00:03:37,260 --> 00:03:41,800
Soo wéyee diko def, dinga mujjee
Di nga gis kalendriye bi nga bëgg.

64
00:03:42,000 --> 00:03:42,640
Baax na!

65
00:03:42,860 --> 00:03:45,620
Kon jéem amul benn loraange!

66
00:03:45,620 --> 00:03:48,600
ASUKA ASUKA:
épisode 26 épisode 1

67
00:03:49,000 --> 00:03:50,480
Waaw kay, demal nelaw!

68
00:03:50,730 --> 00:03:52,930
Asuka, nu fanaan bu baax.

69
00:03:53,460 --> 00:03:56,500
Evangelion Unité-01, jog!

70
00:04:13,160 --> 00:04:14,930
Shinji, xoolal!

71
00:04:15,000 --> 00:04:17,290
Gaaw! Danga wara jog!

72
00:04:27,300 --> 00:04:29,400
roppalaan bi ñu gis ci kaw makaanu mag bi

73
00:04:29,530 --> 00:04:31,140
Euro NERV la

74
00:04:31,260 --> 00:04:31,860
Ñàkk pexe!

75
00:04:36,500 --> 00:04:38,730
Eva Unit-02 pare na...?

76
00:04:40,160 --> 00:04:44,200
Hero bi dëgg dafay feeñ ci waxtu wi war!

77
00:04:58,230 --> 00:05:01,330
Leegi bima yeggee fi,
sa jafe-jafe jeexna!

78
00:05:02,730 --> 00:05:04,200
Amul benn chance!

79
00:05:25,530 --> 00:05:26,530
Ndog dagg!

80
00:05:26,600 --> 00:05:29,930
Luy yaw, dof bi?!
Duma musa yàq lu baax nii!

81
00:05:30,030 --> 00:05:32,800
Sama mbir barina lool ci yeen!

82
00:05:32,930 --> 00:05:34,360
Jëlaat! Jëlaat!

83
00:05:34,600 --> 00:05:35,730
Ndàndoon.

84
00:05:35,970 --> 00:05:37,630
Asuka, nu fanaan bu baax.

85
00:05:52,890 --> 00:05:55,170
Ndog dagg!
Lu doon loolu ?!

86
00:05:55,410 --> 00:05:57,430
Lu tax nga soppi ma nekk gigant?!

87
00:05:57,530 --> 00:05:59,450
Kon, lu gëna am doole
yaw, moo gën...

88
00:05:59,530 --> 00:06:01,150
Du loolu laay wut !

89
00:06:01,260 --> 00:06:02,750
Jëlaat! Jëlaat!

90
00:06:02,830 --> 00:06:05,700
Ndàndoon.
Asuka, nu fanaan bu baax.

91
00:06:14,460 --> 00:06:16,930
Danga wara dalal sa xel.

92
00:06:17,660 --> 00:06:20,660
Dafay am solo lool ngir am ndam ci bépp xare.

93
00:06:21,410 --> 00:06:24,400
Leegi ci 31 jéego, dinga ñàkk.

94
00:06:26,970 --> 00:06:28,970
Ndog dagg! Ndog dagg!

95
00:06:29,000 --> 00:06:31,000
Ndog dagg!
Lu xew?!

96
00:06:31,010 --> 00:06:33,010
Lu tax may jouer shogi ?!

97
00:06:33,140 --> 00:06:35,140
Danga yàgg a bëgg joŋante...

98
00:06:35,140 --> 00:06:38,160
Ndam ci njuuj njaaj amul benn njariñ.
Bi ci topp! Bi ci topp!

99
00:06:38,200 --> 00:06:39,600
Defal ko romantik bii yoon!

100
00:06:39,860 --> 00:06:42,660
Ndàndoon.
Asuka, nu fanaan bu baax.

101
00:06:57,360 --> 00:06:59,620
Waaw, gis-gis bu rafet la!

102
00:07:00,100 --> 00:07:04,760
ñu koy woowe
Tokyo bu bees-3.

103
00:07:04,930 --> 00:07:08,640
Mënu ma xaaru ngir gis àdduna yu bari yi ak yaw, Asuka.

104
00:07:08,930 --> 00:07:09,740
Shinji...

105
00:07:10,700 --> 00:07:12,700
Eep! Bul ma rus!

106
00:07:14,130 --> 00:07:15,440
Kontaan naa lool...

107
00:07:16,220 --> 00:07:16,960
Shinji?

108
00:07:17,220 --> 00:07:19,660
Dakkal dal! Ndog dagg!
Ndax lépp jàmm?!

109
00:07:19,960 --> 00:07:21,660
Waaw. Nanu tàmbaliwaat...

110
00:07:23,230 --> 00:07:25,560
Jàppoon naa ni damay dee...

111
00:07:25,700 --> 00:07:26,660
Loolu baax na.

112
00:07:26,700 --> 00:07:28,230
Bëgg nga wéy?

113
00:07:28,340 --> 00:07:30,060
Déed! Loolu ruslu na lool!

114
00:07:30,150 --> 00:07:31,160
Roll bi ci topp!

115
00:07:31,200 --> 00:07:33,520
And naa ci.
Asuka, nu fanaan bu baax.

116
00:07:41,700 --> 00:07:43,900
Ndog dagg. Too ci biti.
Jëlaat.

117
00:07:50,760 --> 00:07:51,460
Saay-saay!

118
00:07:51,970 --> 00:07:54,500
Ndog dagg!
Lu tax may topp ki njëkka nekk ci sa àdduna?

119
00:07:54,600 --> 00:07:55,760
Jëlaat!

120
00:07:58,560 --> 00:08:00,560
Ndog dagg!
Loolu lumu waroon doon?

121
00:08:00,600 --> 00:08:02,860
fàttaliku lépp
"Xool ma! Bul ma bàyyi ma wéet!" daraa?

122
00:08:03,000 --> 00:08:05,000
Waaw, waaye naka lay mëna jàppale?

123
00:08:05,100 --> 00:08:07,100
Bëgg naa keneen ku dul man ci sama wet

124
00:08:07,290 --> 00:08:09,800
Amna lu muy tekki.
Asuka, nu fanaan bu baax.

125
00:08:13,130 --> 00:08:14,900
Ndog dagg! Ndog dagg!

126
00:08:14,930 --> 00:08:16,830
Ndax danga may jéema rusloo rek?!

127
00:08:16,920 --> 00:08:19,530
Jàppoon naa ni yaw itam danga bëgga gaaw màgg?

128
00:08:20,000 --> 00:08:21,080
Du loolu laa bëggoon a wax!

129
00:08:21,460 --> 00:08:24,000
Wutal ma benn loop bu kontaan xaat!

130
00:08:24,330 --> 00:08:26,900
Alright, I got it.
Asuka, nu fanaan bu baax.

131
00:08:27,880 --> 00:08:31,040
Asuka-chan, loolu yéeme na!
Def nga lu baax!

132
00:08:31,300 --> 00:08:34,840
Yaa ngi am xel.
Sama yaay dafa kontaan lool ci yaw.

133
00:08:35,100 --> 00:08:36,520
Xale bu jigéen bu baax nga.

134
00:08:36,880 --> 00:08:39,560
Mën nga def lépp loo bëgg.

135
00:08:39,860 --> 00:08:44,280
Bul fàtte, sama xarit,
Sama yaay daf lay xool saa yu nekk.

136
00:08:44,360 --> 00:08:45,260
Ndog dagg!

137
00:08:45,430 --> 00:08:47,580
Dédeet, loolu du dox.

138
00:08:47,580 --> 00:08:51,040
Ma yëg ni sama xol neexul. Melni duma sama bopp.

139
00:08:51,660 --> 00:08:52,860
Du loolu amul benn werante.

140
00:08:53,130 --> 00:08:55,520
Hm... Wax nga dëgg.

141
00:08:55,930 --> 00:08:57,500
Asuka, nu fanaan bu baax.

142
00:09:37,460 --> 00:09:38,700
Xalaatal kan?

143
00:09:38,990 --> 00:09:41,450
Xale bu jigeen bu taaru am bust bu 87cm.

144
00:09:42,720 --> 00:09:43,780
Bingo!

145
00:09:43,830 --> 00:09:44,700
Ndog dagg.

146
00:09:45,260 --> 00:09:50,360
Du premise bu baax, waaye bëgg naa
di kontaan ci sama àdduna.

147
00:09:50,360 --> 00:09:52,260
Àdduna bu amul Eva.

148
00:09:55,160 --> 00:10:00,690
Saxaaru express Line 2 mingi waaja agsi.

149
00:10:00,690 --> 00:10:04,400
Baalnu nga taxaw ci ginaaw liiñ bu nete bi.

150
00:10:05,780 --> 00:10:08,870
Saxaaru Line 2 dafay dem 14:20.

151
00:10:08,870 --> 00:10:12,340
Dem ci Ñaareelu Dëkk.

152
00:10:13,120 --> 00:10:17,780
Ku amul ndigal mënu ci dugg.

153
00:10:17,780 --> 00:10:25,560
Noo ngi baamtu: saxaaru Line 2 dafay dem 14:20 dem Second City.

154
00:10:25,560 --> 00:10:29,690
Ku amul ndigal mënu ci dugg.

155
00:10:52,960 --> 00:10:55,400
Nanu dem, Asuka.

156
00:11:09,960 --> 00:11:11,330
Jërëjëf, Shinji.

157
00:11:11,700 --> 00:11:13,270
Waaye... leegi baaxna.

158
00:11:14,030 --> 00:11:18,250
Àdduna bu dal te rafet la...
waaye du barab bima wara nekk.

159
00:11:19,010 --> 00:11:20,690
Amnaa barab buma wara aar.

160
00:11:21,530 --> 00:11:24,870
Bëggatuma yéem sama xel.

161
00:11:26,030 --> 00:11:29,030
Dinaa wut nuñu koy defee
sama bànneex ci àdduna dëgg.

162
00:11:29,830 --> 00:11:33,290
Noonu la ma doon dëgg.
Leegi xamnaa ko.

163
00:11:33,290 --> 00:11:36,630
Episode 27:
BENN LI ÑU WARA DEF

164
00:11:43,360 --> 00:11:45,140
Kon? Daf lay yóbbu ci ginaaw, wala book?

165
00:11:45,520 --> 00:11:47,520
Waaw... Baaxul genn-wàll.

166
00:11:48,000 --> 00:11:49,620
Dañu doon tàggat sa bopp, xam nga.

167
00:11:49,700 --> 00:11:51,180
Daa melni ab saa bu am solo...

168
00:11:56,660 --> 00:11:59,700
Dama xawa tiit tuuti
way ci kanamu nit ñu bari...

169
00:12:02,300 --> 00:12:03,560
Bul dugg ci!

170
00:12:06,730 --> 00:12:08,780
Man itam amatuma ci yaw.

171
00:12:09,100 --> 00:12:10,400
Man sama bopp laa!

172
00:12:21,430 --> 00:12:24,850
Balaa malaaka yi di xeex,
Dina wéy di pilote sama Eva.

173
00:12:25,230 --> 00:12:29,210
Dinaa am sama bànneex ëlëg
loolu mooy ñëw ginaaw bima aare ñépp.

174
00:12:29,430 --> 00:12:30,410
Xam naa ko!

175
00:12:30,810 --> 00:12:33,950
Loolu moo tax ma nekk pilotu Evangelion Unit-02.

176
00:12:33,950 --> 00:12:36,250
Soryu Asuka Langley!

177
00:12:36,290 --> 00:12:38,520
"AK GËRËM BU BËGG,

178
00:12:38,520 --> 00:12:45,100
JËRE JËF YI NÉPP CI 30 AT YI MUJJ."
- HIDEAKI ANNO

